Contribution- Après l’hymne National du Sénégal, voici l’hymne du TER (Par Sakura Syr J.…
TER BI NIEUWNA
TER BA NGI NI
MA KO SEEN MUY NIEUW
SËTU MAAM SAXAAR
LÉGUI MOU DOUG GARE...
RAIL BI YAKO MOOM
KU LA SÉTLU DOOM
XAJAL LA NGA DIAR
SANI LA SA SAAR
NDAKH NGA AGG GAAR
SA MAAM MA TAXOON
LAT DIOR SANI KO CI…
Lire la suite...
Lire la suite...